Paroles de la chanson Freestyle 10/10 par BM Jaay
Chanson manquante pour "BM Jaay" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Freestyle 10/10"
Proposer une correction des paroles de "Freestyle 10/10"
Paroles de la chanson Freestyle 10/10 par BM Jaay
OK, yeah
Kou tek khott tatam si trône bi ? BM Jaay
Kou yobou sén fitou rappeur yi ? BM Jaay
Bane boy moy sauvé senn hip hop bi ? BM Jaay
Att bou nek kouy leumbé town bi ? BM Jaay
Kouy buur bi kane moy prince de la ville ?BM jaay
Koutakh Choe yi di cons bou wow bi ? BM Jaay
Couronnou game bi kouko yorr ? BM Jaay
Kane moy man of the year ? BM Jaay
Khawma wone si trône bi la tok
Sama destination la focus diko top
Rap deff million semey poche
Dak rap geneu job
Douma boy bou am diot
2022 be legui plus de 53 sons la job

Marouane bi digako deg par force
Même so fatei sey nop
Sani kherr douma tei bodé yallah tawal aye dondj
Dieund BM wala merco garé ko sama kogne
Rene kou wakhoul brique sa lekh dina safonte ak sama ndeydior
Talent pure melni Leo Messi
Mane awma nemesis
Boy yima feuleundol niom nieupa digg , nafi deff décennie
May gann bi fokholei bougn meunta siss
Amoul weurseuk il est maudit
Beuss bou takei da fek mou nane volet wala Henessy
Man this ain't right ? yeah you right
How the fuck this nigger Marouane got all of this hype ?
Ouzin Keita lookiness

Them niggers ass and they broke though
Me wakh lein ko si wolof
Manam yorolén teh amoléne béneu tangor
Nala doumeu yak sa gangor
Khamna ni sen nelaw yi doyoul mais tant que mangui fi Keineu dotoufi yandor
Kouy sentou sama défaite dinafi kharr be khobidass
Bougoul deg sama blaze
Neko mou teup balcon mba mou tek tatam bi si gaz
Douma trahir rap Teh na geineu si télé ni Abdou Rass
28 décembre stade bi dineu mabeu
Flow bi beineu le dou niar boul sissou neima nice
Dafmay topando amnagn aye trait ni logo adidas
Client boum yebb dafkey watheil boumou dougoussei le taxi man
At bou nek gein ngemb boy bou bess pour dane Marouane
Damay daw gey rame
Ndakh chiffre yimey deff comme numéro téléphone
Chiffre yigey deff comme note devoir
28 décembre stade bi dineu mabeu
Rabou BM Jaay nieup ley doug meme ndeup kat ba
3milles gua am ticket
Diouni gua am ticket
Soy dound hip hop waro ndangou spectacle bi raw le
Kou tek khott tatam si trône bi ? BM Jaay
Kou yobou sén fitou rappeur yi ? BM Jaay
Bane boy moy sauvé senn hip hop bi ? BM Jaay
Att bou nek kouy leumbé town bi ? BM Jaay
Kouy buur bi kane moy prince de la ville ?BM jaay
Damay daw gey rame
Ndakh chiffre yimey deff comme numéro téléphone
Chiffre yigey deff comme note devoir
28 décembre stade bi dineu mabeu
Rabou BM Jaay nieup ley doug meme ndeup kat ba
3milles gua am ticket
Diouni gua am ticket
Soy dound hip hop waro ndangou spectacle bi raw le
Kou tek khott tatam si trône bi ? BM Jaay
Kou yobou sén fitou rappeur yi ? BM Jaay
Bane boy moy sauvé senn hip hop bi ? BM Jaay
Att bou nek kouy leumbé town bi ? BM Jaay
Kouy buur bi kane moy prince de la ville ?BM jaay
Koutakh Choe yi di cons bou wow bi ? BM Jaay
Couronnou game bi kouko yorr ? BM Jaay
Kane moy man of the year ? BM Jaay
Couronnou game bi kouko yorr ? BM Jaay
Kane moy man of the year ? BM Jaay
Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)