Paroles de la chanson MAIN CHARACTER FREESTYLE par BM Jaay

Chanson manquante pour "BM Jaay" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "MAIN CHARACTER FREESTYLE"

Paroles de la chanson MAIN CHARACTER FREESTYLE par BM Jaay

MZ Fictions , 1DA ON THE BEAT

OK Yeah , Bounce !
Kou téyé rap game bi ? boulen ko nekk di sett , man leu may wadji
Niom dagnou may goungé rek , figurant lagnou may acteur principal bi
Man 0 la diougué beu 100 teh ma guenn siiw maire municipal bi
Amoul fair-play kouma guemoul dina encaisser balle bi ( bruh-bruh-bruh )

Nigga bi kenn yakaroul wonn téyé na ngour gui ni Diomaye
Nouroulahi la man forma feull nga neubou ni kirayy
Guéné album bi dem teudd dji Dubaï , meunoul teh dou bayy
Boudoul ngoram man khawma loumouy diay. Yangui cissou may teglé ay tank seu neegu tante nioumay Taalal ay thiouraye
Meunougn ci man loudoul togg diima khol. Man leu donn ndieukeuntell yegg na bou yagg DI Guestu kholl foumou toll : Guissatou mako da melni kou sonn
Bayy sama waar ni kou yeewo ci tool , khaaral seu tannku toubeuy yaw nga déchirer pinw diko soll
Seu lamigne da niaw mais mesure tes paroles mba ma dag seu tissus ni gayn bilayy niawall ( dagg seu ndeye )

Tu est mort dans le film , Deum bouy déé nga ni Kangana
Bars bouma guéné niouni yay borom the nga bayyi híp hop bi teh Dem investir ci sangara
Rappeurs yi amougnou diom , beurii diott , khamna girls youniouy yooné senn photos bangala
Beuss bougnu tassé ci mbedd boul niangalàtt , boumay pann ci seu kaww douma sakh khalat
Fuck seu equipe Yeah, dolenn bind bagnou tiit Yeah Yeah , boy naako baamtù wat sokhla woo staff linga sokhla may bic yeah , deff son ak ioe comme rap ak lirr
Djegui préliminaire yi soll Kiss, boy damay surfer seu kaww melni gayn bii di pratiquer ay sports nautique
May fuck rap game bi , ioe mbaalou nga deuké . Comme Franc kenn nangouwoul beurré ak mann ndakh ndaww la Teh yorr doolé diou beurri
Lou meunoutaa nekk mann lolou la teulé
Yorouma pouvoir Black Panther , nokk Senn burr di ladj ndakh mollen djité. He don't know what kind of bar is this : ci Vibranium bi lako dieulé
Kou téyé rap game bi ? boulen ko nekk di sett , man leu may wadji
Niom dagnou may goungé rek , figurant lagnou may acteur principal bi
Man 0 la diougué beu 100 teh ma guenn siiw maire municipal bi
Amoul fair-play kouma guemoul dina encaisser balle bi ( bruh-bruh-bruh )

Defko seu profil wala seu couverture , cover album bi seu couverture
Defko seu profil wala seu couverture , cover album bi seu couverture
Defko seu profil defko seu wayyy , cover album bi seu couverture

Defko statut whatsapp , story instagram snapchat , poster ko TikTok
Wakhal gars yi album BM Jaay bangui ci Bonn bi daal en quelque sorte

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment