Paroles de la chanson WHY ALWAYS ME ? FREESTYLE par BM Jaay
Chanson manquante pour "BM Jaay" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "WHY ALWAYS ME ? FREESTYLE"
Proposer une correction des paroles de "WHY ALWAYS ME ? FREESTYLE"
Paroles de la chanson WHY ALWAYS ME ? FREESTYLE par BM Jaay
OK ! Movie : Conspiration G.I Joe , ba rap bi sonné rappeurs yeup khokh mann ci la nieuw
Melni Sadio ak Cardio , sa mc balaye nieuw defna 10 aller-retours khaar ko ci kaww ndakh fila guewel diablo
Douma nitt , allien la bou rap bi fayy douma diablo . appart balle ci Bopp guissouma loutakh ma dila blow
Deuk bi beuri haltérophiles ak alcolos ma investir ci bars yi ioe
Nekkal truand , niakk ma respect dina deal ak ioe , mon flow en confusion amna tangayou safara ak seedayou glace Gelato
Tu est le negre de maison man dama dagg samay chaines ni Django
Amouma benn regle nelenn rap bou gooré bi la yorr

Wathié leu ioe ak gnilla todj , Yoff la deuk man je vis la joie taalouma dila dieuw. gaalou doff bi sou teeroul ma dieuli ko.
Leebou la , meun na feuyy teh meun na diaww , fo beug nafa demm ak ioe
Yeah ! Na kenn woo sapeurs nguir Yallah because I am on FIRE !
Limay deff dama ko tegg ci yonn ni diplomé juriste , beuss bouma rappé ci mbalakh dou vexer benn puriste
Di nga fi baguette beu lakh the sama defaite doko guiss ,ndakh lima ligueyy dou daanou ni lou toubab bi tabakh biir Rufisque
Mom dieuloul benn risque teh diayoul benn disque , benevolat lay deff rappam amoul benefice
Mou tekki dina tiss , tayy assamane bi di niss , ni Nimrod baamou beugé rayy Yallah tayy derett dinar wiss sen kaww

Man ak seu mc kann mo meun ? c'est un faux debat. Ma narr ko maabal niouy ladj " est ce que je vais remplir le stade ? "
Khadjiou salon leu dayy mboww teh dou maté nguenn beugg ko deff abb bulldog wala chien de garde
EASY ! I can rap in different languages and make it look easy
Bitches tryna hook up tell'em I'm busy
I am nowhere to be seen , nowhere he gonna shoot me , he gonna forever miss me
Beugouma koumaa felou , bouma fi kenn darr. Yallah ma tathiou meunouma fethie , ma outti ayy sabars deff son pour nga pakargni tankk
Kou meuna kortt amna mbamm. Chef de bandit la ak chef de gang
Film bi douma ci déé ndakh ngandi probleme la ni Cherif Maal
Leerayou bideew la mom potolamp , dou amm benn trophées melni joueur bouyy jouer birr Tottenham

Sama avancement soula naré rayy meun nga Dema outii tokenatt
Degg na , Yangui menacer waté mais mala guenn reew nigga seu thioki mame
Defko seu profil ak seu couverture , wala seu profil ak seu couverture
Statut ko whatsapp , insta , snapchat , TikTok
Cover album bi defko seu profil mba seu couverture motherfuck !

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)