Paroles de la chanson Li Thi Sama Xél par Bril

Chanson manquante pour "Bril" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Li Thi Sama Xél"

Paroles de la chanson Li Thi Sama Xél par Bril

Bou déé di nieuw dou taago
Motakk ma yagga paré
Deukké saakkou niaane
Fékhéna ba mère ak pa réé
Li ngay wakh yeuggoumako
Liné sama xolama doy
Té tayla biss bi ndjeukk
Thi biss yima déssé doul djoy
Rappeur yeupp mane laniouy def may R.a.p
Boul déraper boul bind R.i .p
 Kén doula beugg Bani nagnko soulalé
Sa boulé yay gueuna tékki
Bilgate Boulagnla fayone lign ma amèl
Assamane ci khinoul Ma djaayla Ba dila wiss
Guiss na ay goumba You bokk ak mane Bén guisss guiss
 Mane dama rare Ni biir ndokk nga guissfa xal
Ay mouma nguir bag Wakk samay secret Kouma wakhal
May wathié kamil Ngay idji
Condamné à mort la tidji
Li ngéni ceddo da izi  Sen carrière soutoul
Djangolen beugga done pressi
Copier coller né crazy
Gueumo yalla  né jay Z
Lhomeur nga di niodi busy

Danga beuga xam
Liy daw this sama biir xel
Fékhéla dougou sama bopp
Di djang sama mind
Danga beuga xam
Liy daw this sama mind
Fékhéla dougousama bopp
Di djang Sama xel

Talouma sétane télé
Dama bokk this gni sonou  Télé dilén sétane
Diniou nakk boul nélaw Yéwoul this bimou télélélélé
Douma voter fouma guiss ay conmeunoum assé tanen
 Teukh goumba ak mouma nioy débat Thi émission
Mangui yééwi ki déé ladjko Louy sunu….Misssion
Yéffeur yi nioy takkeu bombné alahou akbar
Explosé
Djian islam terrorisme Moy séni projet
Adouna bi dafa dof Naniouko yobou fann
Possone ngay lékk do khof wakhma noy
Goudé fanssamay wakh
Moy sa garab loy defi  pharmacie
Bril dafa beugga ba rap
Djibril né farounassi
Guél yéngui may topp né
Arbitre boy guéné
Carton rouge djokh ko joueur
Bou défoul dara ma takhaw ni
Garde rouge
Kou am dou aabi bayilém niou feugg
Ma yorè thiaabi Job boul ma daag  Péé bi

Danga beuga xam
Liy daw this sama biir xel
Fékhéla dougou sama bopp
Di djang sama mind
Danga beuga xam
Liy daw this sama mind
Fékhéla dougou
Sama bopp di djang  Sama xel

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)