Paroles de la chanson Bamba par Cheikh Lo

Auteurs: Mamadou Moustapha Lo

Compositeurs: Mamadou Moustapha Lo

Editeurs: Wagram Publishing

Chanson manquante pour "Cheikh Lo" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Bamba"

Paroles de la chanson Bamba par Cheikh Lo

Mame bamba mo fi diouli guéthie
Guéthie sappé sou wétt
Guéthie sappé sou wétt
Guéthie sappé sou wétt

Yalla la defone n’ganay batakh na massoula
Neup fatal, bamba diouli guéthie
Guéthie sappé sou wétt

Thionom dji mô diour diam dji, gneuptal
Ba fara béw bamba kharé mba am ndam
May gnouko, gnoukoy n’damo
Mame bamba mofi diouli guéthie
Guéthie sappé sou wétt

Kounek ngui wakh sa khalaat
Bamba djingui sounouy khalaat
Bouléne ko sakal morom, moro mantéwoul

Bougnouko wakhé amoul morom
Bougnouko wakhoul amoul morom
Bamba diara yém foko fék fofa la mane
Bamba weét si bindam
Bamou amé batay guissatou gnou kou mélni momo
Mame bamba mofi diouli guéthie

Kou nek ngui wakh sa khalaat
Bamba djingui sounouy khalaat
Bouléne ko sakal morom, moro mantéwoul

Gaalguay diow ba tisbaar, massine ba fardi sab
Soubhana wo bamba di borom milakhwa
Mame bamba mofi diouli guéthie
Guéthie sappé sou wétt
Mame bamba mofi diou li guéthie

Fékhlene ba woor, woolonténe
Sopantalene sama gaayi dimbalentelene
Fékhlene ba woor, woolonténe
Sopantalene sama gaayi dimbalentelene

Ah mame bamba, y adiara wolo
Mame bamba mofi diouli guéthie sappe kou wétt

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment