Paroles de la chanson Bayi Yoon par Daara J Family

Auteurs: Abdou Seck,Mamadou Seck

Compositeurs: Abdou Seck,Mamadou Seck

Editeurs: Chrysalis Music France,Zamora Editions,Traffix Music

Chanson manquante pour "Daara J Family" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Bayi Yoon"

Paroles de la chanson Bayi Yoon par Daara J Family

REFRAIN: ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon jikko you rafét yignou ragnéwoon?
dafa melni dagnou bayi sougnou yoon beugeu askano lougnou momoutoon
deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon
deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon oh!!wow!!
Africains et fiers de ce que nous sommes
Africains et fiers de ce que nous sommes
COUPLET:
fier d'être africain je suis
je suis africain donc je suis
mes ancêtres ont souffert le martyr pour que je puisse relever le défi
c'est à moi de porter le flambeau ils ne peuvent pas me mettre en lambeau
pour me mettre k.o. il faut minimum une armée de cent mille(100000) rambo
Dis à ton prof d'histoire qu'il raconte des histoires,la plus grande des civilisations est
née en afrique noire
L' afrique a inspiré le monde avec ses pyramides sa science et ses mathématiques ses
symboles et ses signes
Elle créa l'écriture avec les hyérogliphes
du temps des pharaons
tu ne me crois pas vas y demande à Akhénaton,...
(de dakar à marseille)
REFRAIN: ana soutoura bifi gnom mame bayiwoon jikko you rafét yignou ragnéwoon?
dafa melni dagnou bayi sougnou yoon beugeu askano lougnou momoutoon
deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon
deug deug xam sa boppa geun gnou wakh la ki nga doon oh!! wow!!
Africains et fiers de ce que nous sommes
Africains et fiers de ce que nous sommes
COUPLET:
Dafa melni gnou ngi daw jeum fénén ni wacc wacc nagnou ande yi
xéeb sougnou ngande yi fékki borom jikko you dande yi fo daw fo daw
di nga wirri ndaari fa nga jougé fi nga dooré fila wooré doufou sorré
AFRO sama dolé na nga mako xolé geum sama démb doon nittou téy
njaxass ni xéetou parfum'k'Gowé Africains koula xass foy gnawé
Africains xola gneup nignouy ngaangé Africains soy joug doufi gawé
koula xol dina séet fanlalay ngagné geum sa bopp xam fi nga bokk
melni garab réen banxass ak xob dougnou fatté fignou jogé ndakh panafricanistes
délo sougnou xél démb kanamou mame gnou giss dimbali jam yi biss gnoul métisses
dékkil osiris carbone14 souliwaat gnou giss histoire bindaat grand pére ba petit fils
bamako singapore anghata!!!
outro: sAMA GAA GNA NGI DOOMU AFRICA MBEUR LA KAAMIL
YAGG YAGG DINA DAANI CI Gééw KéN DOUKO JAMNAANI
...

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment