Paroles de la chanson Ragajuma par El Hadj N'Diaye

Chanson manquante pour "El Hadj N'Diaye" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Ragajuma"

Paroles de la chanson Ragajuma par El Hadj N'Diaye

Suma yaye
Taguna lë
Bayi taguna lë
Suma yaye
Taguna lë
Bayi taguna lë

Ma ngi seti Aïda mi
Sumo xoll mom lë tanë

Suma yaye
Taguna lë
Bayi taguna lë
Suma yaye
Taguna lë
Bayi taguna lë

Ma ngi seti Aïda mi
Sumo xoll mom lë tanë

Deggë na nuy wax
Jiggënu urul
Aïnii
Fële ci aljana
Deggë na nuy wax
Jiggënu urul
Aïnii
Fële ci aljana

Waye man ragajuma
Aïda Camara ragajuma
Raga raga raga ragajuma
Aïda mignone ragajuma

Tukil fa nga minn né
Tukil fa nga minn ne min
Dëkël fi nga woloo
Tukil fa nga minn ne min
Dëkël fi nga woloo

Waye man ragajuma
Aïda mignone ragajuma
Ragajuma
Aïda mignone ragajuma

Damani so sane sëy bëtt
Ba muy xef di xippi
Suma xoll dey yengu
Di yengu di yengu, di yengu di yengu
Di yengu di yengu, di yengu di yengu
Damani so sane sëy bëtt
Ba muy xef di xippi
Suma xoll dey yengu
Di yengu di yengu, di yengu di yengu
Di yengu di yengu, di yengu di yengu

Suma waye
Suma waye jee

Suma waye
Suma waye jee
Man mi yow lay waxal
Suma waye
Suma waye jee
Man mi yow lay waxal

Ragajuma
Aïda mou rafet ragajuma
Eh waye raga raga raga ragajuma
Aïda Camara ragajuma

Waw raga raga raga ragajuma
Aïda mignone ragajuma
Waw raga raga raga ragajuma
Aïda mignone ragajuma

Aïda mignone ragajuma

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)