Paroles de la chanson Jar par Hakill

Chanson manquante pour "Hakill" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Jar"

Paroles de la chanson Jar par Hakill

Nigger loy tek
Appart sa tateloy tek
Mounone na def ni niom mais succès diaralou ma sucé
Hé tedieul sa gatte rek boy nel tek
Mayy wakh parce que mayy deff
Douma dokh tankou diamb fi lek téguiwo tank ma tek
Outil ligueye bi nga todj bobe ba tey guissa gouniou nga todj
Secret bi moy sa album nékhoul fuck
Douma saga sa ndeye ba pare di tadj sa jeuf
Dama immature bay raggal sama dome
Khana sa auto papa panne yak sa carrière
Guepj naléne guiss ngen bougé mètre
Golo bi beyy golo bi layy lekk
Chef de chamber la ngay mbeuk nékk
En tout cas cougn dane dou diuogat bouy khar mou thiat ko dou gatt
Mayy tupac booba le roi kounta low ngay boulat khadiou gatt
Ayy tout bas depuis quand, tout le temps ayy combat you yagoul you tarr
Couple bi comme vaccin
Bodé rappeur sa khel warou si dall

Kousi nkak loum la diaral
Lolo waral
Lo guiss mey def boum la diakhal
Doumko raggal
Bou dieuf dioté bo amoul fiit def da ngay sandi kherr
Déméwouma demi-mesure t doum la mevy centimètre
Ndakh
Li ko jar
Moko jar
Hè li ko jar
Moko jar
Lolou motakh mane ma jar
Yeah ma jar
Ndakh li ko jar
Moko jar

Ndieugeum lassi def
Limou ladj double lassi def
Queum service comme watj bess
Dama yikey ngey tandeber
Bay boume bi tjikam khall bi bey wagn bi khegn
Pawlish dou daneu wally seck
Da ngen réré mbir
Maléne meune dafa evident comme diary fégne
Mangui si digu khal bi ak tankou néne
Ndokhou sappeur ri la nane bamou diekh
Boy sa carrière comme tatou guell mome guinaw la tamo nen
Mousso lal caché mome transport ngay lekk
Mouno lo sakh sa yaye sakou thiep
Démléne wakh séne king yi
Bougnou diawalé tokk si trone bi ak tokk si néne
Hakill akl diuobo rk dead beuss bou yalla
Sakk jumbo khémé lay diw séne tatti diko ndéké
Kharr agne bi diott jourgot sey guell
Djiko na dead di ko note rancunier la djiko requin
Contre mane toujours da ngay melni kou dioudo défaite
Koussi nkak loum la diaral
Lolo waral
Lo guiss mey def boum la diakhal
Doumko raggal
Bou dieuf dioté bo amoul fiit def da ngay sandi kherr
Déméwouma demi-mesure t doum la mevy centimètre
Ndakh
Li ko jar
Moko jar
Hè li ko jar
Moko jar
Lolou motakh mane ma jar
Yeah ma jar
Ndakh li ko jar
Moko jar

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)