Paroles de la chanson Aladji par Jeeba

Chanson manquante pour "Jeeba" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Aladji"

Paroles de la chanson Aladji par Jeeba

Li lagn done ñaneu
Meel nani ñaneu yi nangu na
Ñune Li lagn done xareu
Bess bugn lay wathièl soxna
Té keurgui koffi xool tout le monde à la joie
Tout le monde à la joie
Waay diaroul waax saax ouais ouais sa se voit
Ouais ouais sa se voit

Oie Papam ak aay xaritaam di wadj deem diouma
Baniou taak seuy bi rek niou sandi Duaa
Ngaay degg heureux ménage heureux mariage heureux
Niou laay tagaal say louanges
Ioe Yaaya boy xaritaam yi dikoo ndokalè
Tay nga faayu booru Ndawtaal yign la ameel fuunè
Waay daniuy xawaré tagaté bamou Saf
Taay daniuy xawaré
Mane Taak na diabaar
Deef na liwaar
Degg na deuku na mbeur
Way dafaa doone li waar
Ndaax daaf may nekh lol nioumaay wowei Aladji
Bébé d'amour bébé Aladji
Wawaw Aladji Wawaw Aladji
Mane daf may nekh lol nioumaay wowei Aladji
Bébé d'amour bébé Aladji
Wawaw Aladji Wawaw Alaaadji

Beuss du tutii
Beuss dou borom reik laay tolool
Saa ligueyu ndaay molaa wuyussi
Nieupeu d'accord nagn si lolou
Waay Taay daniuy daal di bâche kogn ba kogn
Xaar yi niou raay, guinaar yi niou ndiogn
Niou yeggal niveau bi adj bassi kowakow
Kou aayé wonè sa momé
Taay yaa momè
Oie Papa ak aay xaritaam di wadj deem diouma
Baniou taak seuy bi reik niou sandi Duaa
Ngaay degg heureux ménage heureux mariage heureux
Niou laay tagaal say louanges
Aladji gueneu ak nietti pièce machallah
Xaarit yi daar ko diiko djine djino djign
Deem gatandou dji madame gane bi yeksi na
Neko bismillah Taay daniuy xawaré
Mane Taak na diabaar
Deef na liwaar
Degg na deuku na mbeur
Way dafaa doone li waar
Ndaax daaf may nekh lol nioumaay wowei Aladji
Bébé d'amour bébé Aladji
Wawaw Aladji Wawaw Aladji
Mane daf may nekh lol nioumaay wowei Aladji
Bébé d'amour bébé Aladji
Wawaw Aladji Wawaw Alaaadji

Wuyuma Aladji
Si geew gui oie laaniuy xaar Aladji
Aladji Beuss bi sa beuss leu Aladji
Goudi gui Yaa momeé Aladji yeah
Eeeweh Sama Aladji aaah Aladji aladji
Sama Aladji ooohoh Aladji Sama Aladji

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment