Paroles de la chanson PYS par Nitdoff

Chanson manquante pour "Nitdoff" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "PYS"

Paroles de la chanson PYS par Nitdoff

Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Dama kay tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Dama kay tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck

Ragalouma dara mane gars yémeu sekkeu
Nigga boul sissou ci pas yi méy tekk
Diawéne yi santuma Seck
Gueyenne bou tabé la séntiwuma chèque
None yi laay fénn lo beu sén touma sétt
Tabé ni Pa Yamar Seck
Tabé ni Pa Yamar Seck
Mane dama tabé ni Pa Yamar Seck

Baneba la defé lepp (Eyy)
Gang gang step (Eyy)
Demna niou fepp (Eyy)
Koba yi djiém lén séet
Real yé touti ma doon len séеt
Nigga say what ma doon laneséet
Pa bé yeukеutikou doomam sétt
I'm a motherfuckin real OG come check (Eyy)
Don't play me boy yawak sa prêt du corps
You look like a bitch khif laaay meré tchi koor
Dama def ay hit di tekk
Reh nga mey def soy oubi pek
Mba douma leu séen si sikétte
Ndakh gayndé bou rose dou banie sucette
What the fuck i see
Koy xeuthiol donkassi gui bitch
As moy sémpi 10 fuck sen sympathie i be rich
Diaro fima diar talent moma diay dou djiaay taar
Doko fek ci barre kk moy sen baye na gars yi khar
Dama néh ci right and peace
Kouma andil problème fils di nga cryin tears
Mbed bi dama yann lou diss
Dafeu melni ma yorr gueun gui marchandises
Guéntoon na sén tiss
Gni ma doon djiéma diss
Daniou namoone biss
Fim tolou lém naniou ndiss
KK yeu teuthie sen guat loulen yéem lanie guiss

Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Dama kay tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Dama kay tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck

Ragalouma dara mane gars yémeu sekkeu
Nigga boul sissou ci pas yi méy tekk
Diawéne yi santuma Seck
Gueyenne bou tabé la séntiwuma chèque
None yi laay fénn lo beu sén touma sétt
Tabé ni Pa Yamar Seck
Tabé ni Pa Yamar Seck
Mane dama tabé ni Pa Yamar Seck

Dokh na ci mbok ni Pa Yamar Seck
Dimbali nit yi ni Pa Yamar Seck
Sa khole bou rafeté dey yombal lepp
Té nit gni deukeul ngey djiapé sa bopp
Diné dji matneu ci Pa Yamar Seck
Yewen té tabé ci Pa Yamar Seck
Beugu na melni ci kogn bi meu deuk
Dilén seuss reuk té doumaléen reuk
Fathie boumou guathié yi ci pét
Diokhé bou djiaka yi di quête
Djitou fou konie bi di deuthie
Diokhé sama diakhal ni yalnafi di gueudj
Roy bakh mo gueun roy bonn
Yiw mom yiw rek ley doon
Nigga boulma lathie lou taye doon
Samey référence meussoul doon niom tyron
Au cas ou t'as douté khel mou séleu laay woutè
Bari naniou té wouté takhna wisdom laalén soutè
Maay nuleul sén systeme bi niou beuguoon tekk fi ndakh c'est chelou
Takh mbeur bouniou wadial andi souma xathié daur dauraat dey khelou
Sen trône niom mi ngui sén che-dou
Nioun nio ngui céedel ach hadou
Daniouy tite bey lathie eskeu dou
Kk fou niou séené ap shadow
Pa Yamar Seck i'm a lion himself
Walking in the jungle with my mindset

Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Damakay tewal ni un Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Dama kay tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck
Tewal ni Pa Yamar Seck

Ragalouma dara mane gars yémeu sekkeu
Nigga boul sissou ci pas yi méy tekk
Diawéne yi santuma Seck
Gueyenne bou tabé la séntiwuma chèque
None yi laay fénn lo beu sén touma sétt
Tabé ni Pa Yamar Seck
Tabé ni Pa Yamar Seck
Mane dama tabé ni Pa Yamar Seck

Diamono dji damey gueun di sadik
Somey topou di digu dama yagu tchi street
Khobé beu sick douma thiop ay dessite
Nelen kouy wout lou dope nameu thiap de suite
Thiepi thiepi gni ngey wowé lobbie
C'est des te-pu peux tu arrêter la machine
Soudé fake nga naleu karé ba chine
Soudé buzz nga eumb na nga paré weussine
Soudé pute nga na nga diarré dubaï
Gayndé mic no bou djiapé dou bayi
Toubey toubey solatoulo toubey
Ya ngui khegn ni kou daye
Gueneu méddé kou die
Doma tester nigga nein nein nein
Beat bi dawneu sama line lay mind
Kaddu kocc thi loulerr laay rhyme
Damey gun di yokk sama leeray nanie
Go go dafeu feudo diokhé pe-do non dou robbot
Bullshit bouma teuko dafa beugu degu ici repose
My man i'm blessed
Am name am place
Boul sissou please
Sinon ma exploser sa face
Ankey damadi sen baye
Fake bitch bouma listen die
Real nigga am peace am daye
Souma takké kou am ndiss do djiaay
Dameleen gueneu déh hey
Dameleen gueunlé shit
Soumadoul Geubleu X-PO
Mane leu Undershif

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment