Paroles de la chanson Bardé (Daphne Calée remix) par Ouly

Chanson manquante pour "Ouly" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Bardé (Daphne Calée remix)"

Paroles de la chanson Bardé (Daphne Calée remix) par Ouly

Faf ga dieul sama xel bi
Mane dé yamay dof lo
Sama xol baguék yaaaaaw
Sama mer yakoy guif lo
Jot na ga khaaaam
Yaw la nope
Li mom dafa fessss
Mougui tourou
Ak lo meunti sokhla
Lathie mako ma jokh la
Fi lep yako moooome
Def ma sokhna
Jot na ga khaaaam
Yaw la nope
Li mom dafa foooort
Moraw guerre

Mane ci yaw la Bardé Oh oh oh
Dama Bardé
Kham ga dama Bardé  Oh oh oh oh
Dama Bardé
May gueun di bek sa somay rétane
Dama bardé
Nigamay def mane reka kham
Dama Bardé
Mane ci yaw la Bardé Oh oh oh
Dama Bardé
Kham ga dama Bardé  Oh oh oh oh
Dama Bardé
May gueun di bek sa somay rétane
Dama bardé
Nigamay def mane reka kham
Dama Bardé

Sama réni xol
Sori ci mane lo wakh mani waw
Ya takh may ré takh may noyi
Kone défal lou gaaw
Yaw mane rek ga lova
May mi Malaraw
Dieuleul lep ma may la
Please néma waw
Yaw  la rek doum ci douté
Jéguéssil kay ma déey la
So beugué sakh ma woudié
Tagg la waayal la

Jot na ga khaaaam
Yaw la nope
Li mom dafa fessss
Mougui tourou
Ak lo meunti sokhla
Lathie mako ma jokh la
Fi lep yako moooome
Def ma sokhna
Jot na ga khaaaam
Yaw la nope
Li mom dafa foooort
Moraw guerre

Mane ci yaw la Bardé
Oh oh oh
Dama Bardé
Kham ga dama Bardé
Oh Oh Oh Oh
Dama Bardé
May gueuneu bek somay rétane
Dama bardé
Nigamay def mane reka kham
Dama Bardé
Mane ci yaw la Bardé Oh oh oh
Dama Bardé
Kham ga dama Bardé  Oh oh oh oh
Dama Bardé
May gueun di bek sa somay rétane
Dama bardé
Nigamay def mane reka kham
Dama Bardé

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment