Paroles de la chanson Paradise par Wally Ballago Seck

Chanson manquante pour "Wally Ballago Seck" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Paradise"

Paroles de la chanson Paradise par Wally Ballago Seck

Ma ngui fatalikou bi meu ley
Sogeu guiss thia lay wakh nane
Niane gui nangou na beureub bi
Meu done guent bigk fofou rek
Lay khel di guiss
Li meu beugone niou and feu

Beureub bou beut meussoul leu khol
Fénén fou nitte démoul, wone
Banekh bou rey lay am thi di xol
 Beussa gui nieuw mane ak
yaw ley done
Legui niou gui ni nioune
Niar sou niou niane antou na
Y'Allah mi gui ak nioune
My baby guentou niou oubil seu beutkhol

Bess bi niou done khar yekssi
Na oubil sey beut noron yi
Madjiri, nagn gni weur
Souf si sédé, ndierer yi
Naw mane ak yaw dou wakhi nen
Geumone na louy rirr thi mane mbeuguel
Leu wone yaw la done set yaw rek leu wone

Ma ngui fatelikou seu thiono ak seu tiss
Len la done tite, niou délou ganaw
Li mey dieuké niane niou ande fénén
Beureub bou beut meussoul leu khol
Fénén fou nit demoul, wone

Banekh bou reu lay am thi di xol
Beussa ngi nieuw mane ak
Yaw ley done
Legui niou gui ni nioune
Niar souniou niane antou na
Y'Allah mi gui ak nioune
My baby guentou niou oubil sey beut khol

Bess bi niou done khar yekssi
Na oubil sey beut noron yi
Madjiri, ndokh ming gni weur
Souf ssi sédé, ndierer yi
Naw mane ak yaw dou wakhi nen
Yeugone na louy rirr thi mane mbeuguel
Leu wone yaw la done set
yaw rek leu wone

Mangui fatelikou goudi
yi niou done niane
Bour bi y'Allah moy sédé
Geumone na ni mane ak yaw ley done
Sou doul wone ak yaw dou done kénén
Sama paradise wawaw, sama aljanah
Sama paradise wawaw sama Aljanah
Take you one love

Li ci li ci nobel, khana nékh na
Chéri Marie Ndir la
Lamine Dieng sala bayou Amina ak Khadija
Samuel Fall bayou Mame Thierno
Kouy sa paradise Fall
Sama paradise wawaw, sama aljanah
Sa ma paradise

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)