Paroles de la chanson Vocal WhatsApp par ZBEST FAMILY

Chanson manquante pour "ZBEST FAMILY" ? Proposer les paroles
Proposer une correction des paroles de "Vocal WhatsApp"

Paroles de la chanson Vocal WhatsApp par ZBEST FAMILY

As' salamalikum nuyu nala frère
Sénna sa jàmmi yaram naka sa liguéey
Est-ce que yangui naka si jàmm
Nam nan la fii
Nola yonné bi vocal pour waxla tay
Binga démé yagg na té keur yafiy taaw
Naari yone nga woté té mussulo fi yoné
Nun sunu yaye jaxlé na waw
Say statuts man duma raw heure funu la wowé toujours
Ngay jaay jomba naaw
Photo wu ak sansé li dafa naaw

Wuti nèx na soko amul gnibissil ling fi bawone
Tay ji da guena dure xalé yangui joy fi
Papa ngui daw fé location ni métti na
Bul lire vocal bi dima vue guisna la en ligne check ko
Déguel lima wax amma solo lool mani eh
Gawal tontu ma
Aaan bulma vue, guisna la en ligne checkc ko
Déguel lima wax amma solo lool mani eh
Gawal tontu ma

Sa xarit sidy ndiaye dead na corona moko ray
Sodoon woté ding ko xam en plus sa guél bi takk nan ko
Nun sunu baye wératul, liguéyatul ci côtém nexatul
Nun cu yaw lanu amone yakar ba mère jay or' am yi
Xolatal mak sama,dimbali maak samay
Mak ak rak yi ci keur gué frère bew nga
Danga wathie yoon

Mon frère hey!!
Kusi dém té guéstuwo danga bayi sa yoon
Ya toppu tubaab bayi nu nun kounta kinté mèrna
Lékétu késé naxuti beyy wotél bul nu fonto
Wuti nèx na soko amul gnibissil ling fi bawone
Tay ji da guena dure xalé yangui fi
Papa ngui daw fé nun sunu yaye jaxlé na waw

Bul lire vocal bi dima vue guisna la en ligne check ko
Déglul lima wax amma solo lool mani eh
Gawal tontu ma
Aaan bulma vue, guisna la en ligne checkc ko
Déguel lima wax amma solo lool mani eh
Gawal tontu ma

Paroles.net dispose d’un accord de licence de paroles de chansons avec la Société des Editeurs et Auteurs de Musique (SEAM)

Sélection des chansons du moment